Genesis 35:23
TSK
¶ Doomi Leya ñooy: Ruben, taawub Yanqóoba, ak Simeyon ak Lewi ak Yuda ak Isaakar ak Sabulon.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Doomi Leya ñooy: Ruben, taawub Yanqóoba, ak Simeyon ak Lewi ak Yuda ak Isaakar ak Sabulon.
Ñiy wuyoo tur yii nag, ñoo leen ciy taxawu: Ci wàllu Rubeneen ñi, Elisur doomu Sedeyur.
¶ Ki joxe saraxam ci bés bu jëkk bi, ñeel giirug Yuda, mooy Nason doomu Aminadab.
Su ñu liitee menn riirum liit mu xumb, dal yi dale penku ñooy fabu.
¶ Am na nag doomi Yuda yu ñuy wax Er ak Onan. Waaye Er ak Onan ña ca réewum Kanaan lañu faatoo.
Aminadab, Nason; Nason, Salma;
Daawuda mooy doomu Yese; Yese, Obedd; Obedd, Bowas; Bowas, Sala; Sala, Nason.