TSK

TSK · Numbers 20:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mbooloo mi ngay sant ne leen: “Yeena ngi waaja jéggi seen kemu réewum bokki Esaween, ñi dëkke Seyir. Dinañu leen ragal, waaye nangeen moytu bu baax.

«May nu, nu jaare sam réew. Yoon wi rekk lanuy topp; dunu jàdd ndijoor, dunu jàdd càmmoñ.

Buleen sàkku mukk jàmmu ñooñu mbaa seen njariñ, seen giiru dund, ba fàww.