Numbers 32:3
TSK
«Gox yii di Atarot, ak Dibon, ak Yaser, ak Nimra, ak Esbon, ak Elale, ak Sebam, ak Nebo, ak Bewon,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
«Gox yii di Atarot, ak Dibon, ak Yaser, ak Nimra, ak Esbon, ak Elale, ak Sebam, ak Nebo, ak Bewon,
Fittkat ya nag fitte nu ca kaw tata ja, ba mu am ñu dee ci say nit. Sa surga ba, Uri Etteen ba it dee na.»
Nit ñaa ngi yéeg jëm kërug jaamookaay ga ca Dibon, ngir jooyi ca bérabi jaamookaay ya, Mowab a ngay yuuxoo kaw tundu Nebo ak Medeba, boppoo bopp dib nel, sikkimoo sikkim xuufu,
«Yeen waa Dibon, dëkk bu taaru bi, wàccleen seen teddnga lu kawe te tooge digg maral; kiy yàqtesi Mowab kat song na leen, di màbbsi seeni tata.