TSK

TSK · Numbers 22:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne leen: «Fanaanleen fii guddig tey. Tont lu ma ci Aji Sax ji sant rekk, dinaa leen ko àgge.» Kàngami Mowab dal ak Balaam.

Balaam ne ko: «Xanaa waxuma la woon ne la lépp lu Aji Sax ji wax, loolu laay def?»

Mise ne ko: «Giñ naa ci Aji Sax ji, Kiy Dund, li ma Aji Sax ji wax rekk laay wax.»

Job 3:15 TSK

Nopplu koon naak garmi yay boroom wurus, te daan feesal seeni kër, xaalis.

Acts 8:20 TSK

Piyeer ne ko: «Na sa xaalis ànd ak yaw asaru, ndegam ab xaalis nga yaakaara jënde mayu Yàlla!