Numbers 22:41
TSK
Ca suba sa Balag ànd ak Balaam, yéege ko ba ca kaw jaamookaay ba ñu dippee Baal, tuur ma, mu tollu fa di séen lenni catu mbooloo ma.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca suba sa Balag ànd ak Balaam, yéege ko ba ca kaw jaamookaay ba ñu dippee Baal, tuur ma, mu tollu fa di séen lenni catu mbooloo ma.
¶ Ba loolu amee kàngami buurub Siri digal buurub Siri ci wàllu Israyil, ne ko: «Ñii, seeni tuur tuuri tund lañu; moo tax ñu ëpp nu doole, waaye su nu xeexeek ñoom ci joor gi déy, su boobaa noo leen di ëpp doole.
Moo bëggoon di móoloo, yal na ko këppoo; soppul ag ñaan it, yal na ko barke sore.
¶ Aw làmmiñ lanuy sante kiy Boroom bi, di Baay, te it ci lanuy móoloo nit ñi bindoo takkndeeru Yàlla.