TSK

TSK · Numbers 24:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci kaw loolu Melkisedeg buurub Salem, mi doon sarxalkatu Yàlla Aji Kawe ji, daldi ñëw, indi mburu ak biiñ.

kàddug kiy dégg waxi Yàlla, Aji Man ji wonem peeñu, mu gis, kiy daanu leer, te ay gëtam muriku.

¶ Su dee wàllu ñam wu ñu sarxal ay tuur, dëgg la, nun ñépp am nanu xam-xam ci moomu mbir. Xam-xam nag day tax nit a réy-réylu, waaye cofeel day yokke.