Waaye su ngeen ko déggalee ba déggal ko, di jëfe li ma leen wax lépp, su boobaa ma noonoo seeni noon, bañ seeni bañaale.
TSK
TSK · Numbers 24:8
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ña ngay xultu ca kaw Yàlla ak Musaa, naa: «Lu ngeen nu doon jële Misra, ngir nu dee ci màndiŋ mi? Duw ñam, dum ndox, te wii ñamu toskare génnliku nan!»
Wii askan ni gaynde lay jóge, ni gayndeg sibi lay faboo, du goor te yàppul am pàdd, deret ja tuuru, mu xab.»
Maay jal ci seen kaw ay musiba, maa leen di soqil, ba jeexal samay fitt.
yilife leen yetu weñ, rajaxe leen ni njaqal xandeer.”»
ànd ak daraja, dawal ba am ndam, di dawal dëgg ak yërmande ji war, ba mana def ay jaloore.
May xalaat, ba bët set; Aji Sax jiy dammat samay yax ni gaynde, diggante bëccëg ak guddi, nga jekkli ma.
«Israyil diy gàtt yu tasaaroo, yu ay gaynde dàq, buurub Asiri di gaynde gi jëkka lekk, Nabukodonosor buuru Babilon topp ca, seeñu yax ya.»