Buleen wóllëranteek niti réew ma, lu ko moy dinañu gànctook seeni tuur, rendil seeni tuur ay sarax, woo leen ca, ngeen lekk ca seeni sarax.
TSK
TSK · Numbers 25:1
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 34:15
TSK
Numbers 31:15
TSK
Musaa ne leen: «Kon jigéeni Majan ñépp ngeen bàyyi, ñu dund!
Numbers 33:49
TSK
Wetu dexu Yurdan, ga ca diggante Bet Yesimot ak Abel Sitim, ca joori Mowab, fa lañu dale.
Psalms 106:28
TSK
Ñuy darook tuurum Baal Pewor, di lekk lu ñu sarxal ay yàlla yu amul bakkan,
Hosea 9:10
TSK
«Ni cabbu reseñu biir màndiŋ, ni laa fekke Israyil. Ni ndoortel doomi figg ju ndey ja taawloo, ni laa gise seeni maam. Waaye ñoom ñoo dem Baal Pewor, ñoo sédd seen bopp Baal, tuur mu ruslu mi, ba tax leena seexluwu ni kooku ñu sopp.
Bunu jëfe powum séy, ni ko ñenn ci ñoom daa defe, ba tax ñaar fukki junni ak ñett (23 000) ca mbooloo ma bokk dee ci benn bés.