Exodus 2:2
TSK
Ndaw sa ëmb, ba mujj am doom ju góor. Ba mu gisee taar, ba liir ba àndal, nëbb na ko lu mat ñetti weer.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndaw sa ëmb, ba mujj am doom ju góor. Ba mu gisee taar, ba liir ba àndal, nëbb na ko lu mat ñetti weer.
¶ Amram moo jël bàjjanam Yokebedd soxna, kooku am ak moom Aaróona ak Musaa. At, ya Amram dund, téeméer la ak fanweer ak juróom ñaar (137).
¶ «Bul dëkkoo sa bàjjan, ndax daa jegewook sa baay lool cig bokk.
¶ Mbooloom bànni Israyil gépp nag àgg ca màndiŋu Ciin, ci biir weer wi jëkk ci at mi. Ñu daldi dal ca Kades. Fa la Maryaama faatoo, ñu denc ko foofa.