Numbers 11:28
TSK
Yosuwe doomu Nuun, ja dale doon bëkk-néegu Musaa cag ndawam, daldi cay àddu, ne: «Sang Musaa, aaye leen!»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yosuwe doomu Nuun, ja dale doon bëkk-néegu Musaa cag ndawam, daldi cay àddu, ne: «Sang Musaa, aaye leen!»
¶ Naka la Sóol bàyyikoo ca Samiyel, walbatiku, Yàlla daldi soppi xelam. Firnde yooyu yépp nag matandoo ca bés ba.
¶ Kuréli yonenti Yeriko ya doon seetaan a nga janook moom naa: «Leeru Ilyaas wàcc na ci kaw Alyaasa!» Ba loolu amee ñu gatandu ko, sujjóotal ko, dëpp seen jë ca suuf.