Exodus 18:15
TSK
Musaa ne goroom: «Li ko waral mooy nit ñi dañuy dikk, di laaj li dëppook àttey Yàlla.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Musaa ne goroom: «Li ko waral mooy nit ñi dañuy dikk, di laaj li dëppook àttey Yàlla.
Ñu tëj waa ja, ba xam lu Aji Sax ji namm ci moom.
Ba loolu amee ñu teg ko ciy loxo, ndax dogaleesagul woon nees di def ak moom.
Nanga wóoloo Aji Sax ji, sa léppi xol, te bul wéeru ci saw déggin.