¶ Ba loolu amee doomi Israyil def noona. Yuusufa jox leen ay watiir ci ndigalu Firawna, ak lu ñu lekk ca yoon wa,
TSK
TSK · Numbers 3:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 45:21
TSK
Numbers 3:51
TSK
Ci kaw loolu Musaa jox xaalisu njotlaay ba, Aaróona ak doomam yu góor, ci ndigalal Aji Sax ji, na ko ko Aji Sax ji sante.
Numbers 4:37
TSK
Ñooñu lañu limal làngi Keyateen ñi, ñoom ñépp la liggéeyu xaymab ndaje mi war. Musaa ak Aaróona ñoo leen limoon, na ko Aji Sax ji santaanee, Musaa jottli.
Numbers 4:45
TSK
Ñooñu lañu limal làngi Merareen ñi, Musaa ak Aaróona ñoo leen limoon, na ko Aji Sax ji santaanee, Musaa jottli.
Deuteronomy 21:5
TSK
¶ Su ko defee sarxalkat yi, Leween ñi dikk, ndax ñoom la seen Yàlla Aji Sax ji taamu, ngir ñu di ko liggéeyal, di barkeele ciw turam, te ci seen kaw kàddu lees di àttee bépp jote, ak gépp loraange ci wàllu yaram.