¶ «Sàkkalal jaamookaay bi ay làcci bantu séng yuy sampe. Na làcc wu nekk am ñaari kenu yu ñu lëkklee galan yu ndaw, te nga def làcci jaamookaay bi yépp noonu. Na taxawaayu làcc wu nekk di fukki xasab, yaatuwaay bi di xasab ak genn-wàll.
TSK
TSK · Numbers 3:36
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nga sàkkal nag kiiraay li juróomi jëni séng, xoob wu ci nekk wurus, seeni wékkukaay di wurus, te nga móolal jën yi juróomi teguy xànjar.
jaamookaay bi ak xaymaam ak kiiraayam aki keppoom aki làccam, ak galan yeek jën yeek tegu yi,
¶ Gannaaw gi ñu sàkkal jaamookaay bi ay làcci bantu séng yu sampe. Làcc wu nekk am ñaari kenu yu ñu lëkklee galan yu ndaw, te noonu lañu def làcci jaamookaay bi yépp. Fukki xasab lañu def taxawaayu làcc wu nekk, def yaatuwaay bi xasab ak genn-wàll.
¶ Teguy jën yi xànjar la, wékkukaayi jën yeek ay galanam di xaalis, ñu xoob boppi jën yi xaalis; jëni ëtt bi yépp nag, galani xaalis lañu leen lëkklee.
¶ «Ñi askanoo ci Merari itam, na ñu bokke seeni làng ak seen këri maam, noonu nga leen di lime,
yee ñeent, mu booleek juróom ñetti nag, jox Merareen ña, na ko seen liggéey laaje, ci njiital sarxalkat ba Itamar doomu Aaróona.