Genesis 33:17
TSK
¶ Yanqóoba moom jubal gox bu ñu naan Sukkóot, tabax fa kër, mbaaral géttam, moo tax ñu tudde bérab boobu Sukkóot (mu firi Ay mbaar).
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Yanqóoba moom jubal gox bu ñu naan Sukkóot, tabax fa kër, mbaaral géttam, moo tax ñu tudde bérab boobu Sukkóot (mu firi Ay mbaar).
Seeni jabar doŋŋ, ak seeni doom ak seenug jur, ndax xam naa ne jur gu takku ngeen am, ñooy des ci seen dëkk yi ma leen jox,