TSK

TSK · Numbers 32:38

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba loolu weesee Isaaxa sikkli teen, yi ñu gasoon ca jamonoy baayam Ibraayma, te waa Filisti sakkoon leen gannaaw ba Ibraayma nelawee. Ca la tudde teen yi tur, ya leen baayam tudde woon.

Ca suba sa Balag ànd ak Balaam, yéege ko ba ca kaw jaamookaay ba ñu dippee Baal, tuur ma, mu tollu fa di séen lenni catu mbooloo ma.

Boo noppee, deel ca kaw tund woowu nga yéeg jëm, ba ñu tërali la ca say bokk, noonee sa mag Aaróona deeye woon ca kaw tundu Or, ba ñu tërali ko cay bokkam.

Kuy sàkkuy tuur barew tiis, man de duma leen tuural deret, sama làmmiñ du leen tudd.

Mbugal dikkal déndu doj wu tell wi, dikkal dëkk yii di Olon, Yaxacc ak Mefat