Deuteronomy 1:37
TSK
Man itam Aji Sax ji mere na ma ci ndax yeen, ba ne ma: «Yaw itam doo ca dugg.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Man itam Aji Sax ji mere na ma ci ndax yeen, ba ne ma: «Yaw itam doo ca dugg.
Daawuda daldi giñ, neeti ko: «Dinaa la ko giñal, sa baay xam na xéll cér bi ma am ci yaw. Moo tax mu ne: “Bu Yonatan yég sama mébét mukk, lu ko moy dina ko naqarlu.” Waaye giñ naa ko, nga fekke ci Aji Sax jiy dund, ab jéego sax doxul sama digganteek dee.»
Ba mu ko defee Buur gis Lingeer Esteer, mu taxaw ca biir ëtt ba. Mu baaxe ko, daldi koy tàllal yetu wurus wa muy màndargaale nguuram. Esteer jegesi, laal boppu yet wa, di ko ko sante.