TSK

TSK · Numbers 33:36

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu ndaw ya dem yëri réew ma, dale ko ca màndiŋu Ciin, ba àgg Reyob, ga ca wetu Amat.

¶ Mbooloom bànni Israyil gépp nag àgg ca màndiŋu Ciin, ci biir weer wi jëkk ci at mi. Ñu daldi dal ca Kades. Fa la Maryaama faatoo, ñu denc ko foofa.

Li ko waral mooy yeena ma fecci worma ci digg bànni Israyil, ca ndoxi Meriba Kades, ca màndiŋu Ciin, ndax yeena wormaalul sama sellnga ci digg bànni Israyil.