Exodus 25:5
TSK
ak deri kuuyu xar yu ñu wulli, sóob ko xonqal, ak deri piipi ak banti séng,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
ak deri kuuyu xar yu ñu wulli, sóob ko xonqal, ak deri piipi ak banti séng,
¶ «Defarlul taabalu bantu séng, guddaayam di ñaari xasab, yaatuwaayam di xasab, taxawaayam di xasab ak genn-wàll.
Maa ngii nag di ŋafal réewum Mowab, ba xañ leen mboolem seen dëkk ya gëna taaru sax, di Bet Yesimot ak Baal Mewon ak Kiryaatayim.