TSK

TSK · Numbers 5:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba loolu amee Aji Sax ji wax Musaa ne ko: «Bindal lii xew cib téere, muy pàttli, te nga xamal Yosuwe ne ko, raafal laay def askanu Amaleg, ba ñu jeex tàkk, ba deesatu leen fàttliku fu asamaan tiim.»

Mu jëm ci njiitu jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.

Mennum man mii maay far say moy ngir man, ba dootuma fàttliku bàkkaar.

Fekk na Yeremi bind cib taxañ mboolem safaan yiy dikkal Babilon, di mboolem mbir yooyu jëm ci Babilon.