1 Samuel 1:27
TSK
Xale bii moo ma taxoon di ñaan, te Aji Sax ji defal na ma sama dagaan.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Xale bii moo ma taxoon di ñaan, te Aji Sax ji defal na ma sama dagaan.
Kon nag: «Nangeen génne ci seen biir, te teqlikoo ak ñoom,» la Boroom bi wax. «Lu sobewu, buleen ko laal. Su boobaa, maa leen di dalal.