TSK

TSK · Numbers 8:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Noonu ngay jële Leween ñi, sédd leen Aaróona ak doomam yu góor. Ñoom ñoo di cér bu mat sëkk bu ñu koy sédde ci bànni Israyil.

Ndax lépp luy taaw bu góor, sama cér la. Keroog ba ma fàddee lépp luy taaw bu góor ca réewum Misra, ca laa sellalal sama bopp lépp luy taaw ci Israyil, dale ci nit ba ci jur. Maa leen séddoo. Maay Aji Sax ji.»