Genesis 26:5
TSK
ndax Ibraayma déggal na ma, dénkoo na sama ndénkaane, ak samay santaane, ak sama dogali yoon, ak samay yoon.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
ndax Ibraayma déggal na ma, dénkoo na sama ndénkaane, ak samay santaane, ak sama dogali yoon, ak samay yoon.»
Su niir wa yàggee ca kaw màkkaan ma it, ak lu fan ya bare bare, bànni Israyil a ngay dénkoo dénkaaney Aji Sax ji, waaye duñu dem.
«Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Su fekkee ne samay yoon ngay awe te sama ndénkaane nga dénkoo, su boobaa yaw it dinga saytu sama kër, di sàmm samay ëtt. Te maa lay jox ay cér yu la yaatal ci biir ñii fi taxaw.