TSK

TSK · Philemon 1:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

bu may dem Espaañ, dinaa leen seetsiwaale. Yaakaar naa leena gis bu ma fa jaaree, ba ngeen yiwi ma, ma jàlli Espaañ, gannaaw, lu mu néew néew, ay fan yu ma nammantikoo ak yeen.

Yeen itam, ni ngeen nu ciy jàpplee mooy ngeen di nu ñaanal. Su ko defee yiw, wa nu ñu bare ñaanal ba nu am ko, dina tax ñu bare biral ag cant ci sunu mbir.

Gannaaw loolu bir na ma nag, xam naa ne dinaa desagum, desandoo feek yeen ñépp, ngir ngeen jëm kanam, tey bége seen ngëm,

Ma di leen gëna tinooti, ngir ngeen ñaanal nu, ba ma délsil leen nu mu gëna gaawe.

Kon nag tuddanteleen seeni bàkkaar tey ñaanalante, ndax ngeen wér. Aji jub ji, ag ñaanam, doole lay dale.