1 Samuel 18:3
TSK
Ba loolu amee Yonatan fasook Daawuda kóllëre, ndax sopp ko ni boppam.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba loolu amee Yonatan fasook Daawuda kóllëre, ndax sopp ko ni boppam.
«Jeeg bu jàmbaare bare na, waaye yaw, yaa ci raw.»
¶ Bu Timote dikkee nag, fexeleen ba bumu am lu muy tiit ci seen biir, ndax liggéeyu Boroom bi lay liggéey ni man.
Timote nag xam ngeen ne ku rafet ab jëw la. Ni doom di taxawoo baayam, ni la bokke ak man liggéey, bi ci xamle xibaaru jàmm bi.
ñeel Timote, sama doomu bopp ci wàllu ngëm. Aw yiw ak yërmande ak jàmm ñeel na la, bawoo ci Yàlla Baay bi, ak sunu Sang Almasi Yeesu.