TSK

TSK · Proverbs 1:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 4:8 TSK

Li ma gis daal, ku bey ñaawtéef, ji coono, yaa koy góob.

Ku def njekkar sab añ mat, ku baax gën law demin.

Neleen aji jub ji mooy baaxle, mooy yooloo añam.

Yeen waa àddina, dégluleen! Maa ngii di indil askan wii musiba, seeni pexe jural leen. Ñoo faalewul samay kàddu, gàntal sama yoon.

Ma daldi leen xëpp samam sànj, fàkkase leen sama tàngooru xadar, këpp leen seen añu jëf ci seen kaw bopp. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.»