TSK

TSK · Proverbs 1:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Li may wax xel la, di xalaat yu déggu.

Waxi ku xelu day gindee, bantub sàmm la; tënk ba diy pont, sampe ca. Loolu ag may la, jóge ci sàmm biy kenn.

Acts 8:30 TSK

¶ Filib dabsi waayi Ecopi ja, daldi dégg muy jàng téereb Yonent Yàlla Esayi. Mu ne ko: «Ndax xam nga li ngay jàng?»

Loolu la bind ci mboolem bataaxal yi mu waxe ci moomu mbir, te mu am ci ponk yu jafee xam, ba ñi dese am njàng te seenum xel toogadi, di walbati waxam, ni ñuy def ak yeneen bind yépp, ba far sànk seen bopp.