1 Kings 12:1
TSK
¶ Ba loolu amee Robowam dem dëkk ba ñuy wax Sikem, ndax fa la Israyil gépp daje woon, ngir fal ko buur.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ba loolu amee Robowam dem dëkk ba ñuy wax Sikem, ndax fa la Israyil gépp daje woon, ngir fal ko buur.
Xel mu ñaw day suuxat bakkan, te ab dof jëfi dofam a koy yar.
tegtal yu xelu lañuy xaree, diisoo bu yaatooy maye ndam.
¶ Ba loolu amee ndawi Yeesu yi ak mag ñi bokk daje, ngir seet mbir moomu.