TSK

TSK · Proverbs 12:26

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ma nga bàddoo lëndëm, làqoo, làmboo ndox mu lëndëm aki xàmbaar,

Kuy mébét lu bon daa réer, kuy mébét lu baax am nga ngor ak worma.

¶ Képp ku dajeek lu koy xiirtal, bumu ne: «Yàllaa ma xiirtal,» ndax maneesula xiirtal Yàlla ci lu bon, te moom ci boppam du xiirtal kenn.

Kàddu yu réy yu tekkiwul dara lañuy naxee, di fàbbee xemmemtéefi bakkan yu jéggi dayo, ay nit ñu yàggula rëcce ci ñeneen ñu nekk cig réer.

Ñu xalab ninki-nànka ju réy ja, jaanu cosaan joojee ñuy wax Tuumaalkat bi, di ko wax Seytaane, naxekatu mboolem àddina. Ci kaw suuf lañu ko xalab, mooki malaakaam.