Proverbs 11:22
TSK
Taaru jongama ju xel ma gàtt, mooy jaaro wurus ci noppu mbaam-xuux.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Taaru jongama ju xel ma gàtt, mooy jaaro wurus ci noppu mbaam-xuux.
Xel mu dal, yaram wu naat; fiiraange semmal boroom.
Doom ju dof naqaru baay baa, te jabar ju pànk mooy senn bu dakkul.
Dëkke ndànd-foyfoy moo gën jabar ju tàng, bare ay.
ndaw su bon su for jëkkër, jigéen ju wuutu sangam bu jigéen.
«Jeeg bu jàmbaare bare na, waaye yaw, yaa ci raw.»
Góor moom du muur boppam, ndax mooy takkndeeru Yàlla te moo taxawe darajay Yàlla. Waaye jigéen moo taxawe darajay góor,