TSK

TSK · Proverbs 13:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ndaw lu tayel ca ka yónnee daa mel ni lu forox ciy gëñ mbaa saxar ciy gët.

Jëw, mer a cay topp; mooy ngelawal taw, taw a cay topp.

«Ca yonenti Samari it laa gis njekkar, ñuy waxe waxyuy Baal tuur mi, di réeral Israyil, sama ñoñ.

Su ma nee nit ku bon ki: “Dee rekk ay sa àtte,” te fekk àrtuwoo ku bon ka, waxuloo lu ko waññee ca mbonam ga, ba mu mucc, ku bon kaay dee ndax tooñam, waaye bakkanam yaw laa koy laaj.

Te itam li ñuy sàkku ci ay saytukat moo di ñu jara wóolu.

Kon nag Almasi, noo diy ndawam, te ci nun la Yàlla di wootee. Kon ci turu Almasi, danu leen di ñaan: nanguleena juboo ak Yàlla.

Li nga dégge ci man te seede yu bare teewe ko, nanga ko jottli nit ñu wóor ñu ko mana xamal ñeneen.