TSK

TSK · Proverbs 14:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Ruth 4:11 TSK

¶ Waa pénc ma mépp ak mag ña nag ne ko: «Noo ko seede. Yal na Aji Sax ji def ndaw siy séysi sa kër, mel ni Rasel ak Leya, ñoom ñaar ñi giir waa kër Israyil gépp. Yal nanga tekki ci digg Efrata te amu tur ci Betleyem.

Ku Axab deele ci dëkk bi, xaj yi lekk; ku ci médde àll, njanaaw ya for.»

Jigéen ju dof day xumb, reew, du xam lu xew.

Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.

Xel mu rafet ay tabax kër, rafet déggin a koy samp.

Day seetlu ab tool, jënd ko, sàkk ciw ñaqam, jëmbat tóokër.