TSK

TSK · Proverbs 14:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Daawuda ne ndaw la: «Lu la xamal ne Sóol ak doomam Yonatan dee nañu?»

Ñu yónnee ci man, wax ma loolu ba muy ñeenti yoon, sama tont di lenn.

Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.

Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.

Acts 13:7 TSK

Ma nga bokkoon ca toppum Sergiyus Póolus boroom dëkk ba, nit ku rafet xel. Kooku namma dégg kàddug Yàlla, daldi woolu Barnaba ak Sóol.

¶ Su boobaa nu noppee doon ay tuut-tànk yu nit ñiy muusaatoo kàddu yu mel ni gannax yu nuy baaje, ak ngelawal mboolem àlluwa ju bees ju nuy pamti-pamtee ci seen biir pexey naxe ak njublaŋ, ngir fàbbi nu.