¶ Ca gannaaw ëllëg sa Yuusufa ne leen: «Bu ngeen defee lii may wax, dingeen dund, ndax man ragal naa Yàlla.
TSK
TSK · Proverbs 14:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yesabel yónnee Ilyaas ndaw, ne ko: «Yal na ma tuur yi teg mbugal mu gëna réy, ndegam nëgëni ëllëg jëluma sa bakkan, ni nga jële bakkani yonent yii.»
Mu ne: «Su leen jàmm taxee jóg, jàppleen leen, ñuy dund; su leen xare taxee jóg it, jàppleen leen, ñuy dund.»
¶ Amoon na ca réewum Ucc, góor gu ñuy wax Ayóoba. Góor googu nekkoon ku mat te jub, ragal Yàlla te dëddu lu bon.
ndegam maa xàccil sama loxo ab jirim, ndax yaakaar kiirlaay ca pénc ma,
Sama yaram a ngi daw ndax ragal la, ragal say àtte.
Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;
Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
Boroom xel, buy layook ub dof, bu mereek buy ree, jàmm du am.