Proverbs 9:6
TSK
Dëddul jëfi téxét ba dund, di jubal ci yoonu dégg.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Dëddul jëfi téxét ba dund, di jubal ci yoonu dégg.»
Doom, soo noppee déglu ku lay yar, sore nga kàdduy xam-xam.
Dama leena bind, ne leen buleen amlante ak ku tuddoo mbokkum gëmkat, te di fokatub séy, mbaa mu dib bëgge, mbaa mu dib bokkaalekat, mbaa ab saagakat, mbaa màndikat, mbaa ab ŋàppaaral. Ku ni mel, buleen bokk ak moom lekk sax.