Psalms 59:7
TSK
Bu ngoonee ñu wàccsi, di xiiru niy xaj, di wër dëkk bi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Bu ngoonee ñu wàccsi, di xiiru niy xaj, di wër dëkk bi.
Nit ku ñaw day xam, ba ca; ab dof siiwal waxi dofam.
Nit bége na tontam lu dal, kàddu gu jib fa mu ñoree neex!
Ku rafet xel, say kàddu xelu; soo waxee, yey.
Ku xelu àddu, mu diw yiw; ku dofe wax, sànku.