1 Kings 3:23
TSK
¶ Buur ne: «Kii a ngi naan: “Sama doom jii mooy dund, sa doom a dee.” Kee naan: “Déedéet, sa doom a dee, sama doom mooy dund.”»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Buur ne: «Kii a ngi naan: “Sama doom jii mooy dund, sa doom a dee.” Kee naan: “Déedéet, sa doom a dee, sama doom mooy dund.”»
Ku jub day xam wax ju yiw; ab soxor sàlloo waxi njekkar.
Ku xelu àddu, xam-xam rafet; ab dof di talalali.
Ab dof day mer, sàmbaar; ku xelu, mer, ànd ak sagoom.
Bu xalaat baree, indi gént; bu wax baree, waxi dof jib.
Ku xelu àddu, mu diw yiw; ku dofe wax, sànku.
¶ Ndax kat bare na ñu të, rawatina ci tuubéen ñi bokk ci askanu yawut, ay waxkati neen lañu, te ñooy yàq xeli nit ñi.
Waaye Sang Almasi ngeen di sellal ci seen xol, te waajal nu ngeen di tontoo ku leen laaj lu jëm ci yaakaar ji ngeen am.