TSK

TSK · Proverbs 16:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Sóol yebal ay ndaw ca kër Daawuda ngir ñu xoolal ko ko, ba bët set, ñu rey ko. Mikal, soxnas Daawuda, yégal ko Daawuda, ne ko: «Soo rawalewul sa bakkan ci guddi gi de, bu ëllëgee dees na la rey.»

Sóol wax ak jawriñam yi taxaw ci wetam, ne leen: «Yeen Beñamineen ñi, dégluleen! Mbaa yeen ñépp, doomu Yese jee leen di jox ay tool aki tóokëri reseñ, am yeen ñépp lay fal njiiti kuréli junni ak njiiti kuréli téeméer,

Dañu koo feyoon ngir mu tiital ma, ma def noonu, muy bàkkaar. Su ko defee ñu yàq sama der, torxal ma.

Ku jub day seetlu ku muy xaritool; soxor bi, jikkoom a koy sànk.