TSK

TSK · Proverbs 17:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waa Filisti nag ne dann Sóol aki doomam, ba rey ca ñett; Yonatan ak Abinadab ak Malkisuwa.

¶ Jamono ya Daawuda nekkee ci jal bi, amoon na xiifub ñetti at yu tegloo. Daawuda diis ko Aji Sax ji. Aji Sax ji ne ko: «Li waral xiif bi moo di àqu deret ji topp Sóol ak waa këram ndax waa Gabawon ña mu rey.»

Noon yaa ngi ne jonn ak seen doole, bare na ñu ma bañ ci neen.

Ma ji nit cofeel, mu sosal ma; te man ma di ko ñaanal.

Lu baax dees na ko feye lu bon a? Moona gasal nañu ma am yeer, di ma tëru. Bàyyil xel ba may taxaw fi sa kanam, di leen tinul ngir nga moyale leen sa mer.

Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.