TSK

TSK · Proverbs 17:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Man, Aji Sax ji, maay seen Yàlla ji leen yékkatee réewum Misra. Ŋaleen ŋafeet, ma reggal leen.

«Yeen mbooloo yi laay yéene, doom aadama yi laay joor.

Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.

Ab yaafus day bëgg lu mu amul ba dee, ndax du nangoo liggéey;

«Éey, yeen ñi mar ñépp, dikkleen ci ndox mi, ba ci ku amul xaalis sax! Dikkleen jënd pepp, lekk! Dikkleen jënd pepp mu xaalis jëndul, ak biiñ ak meew mu amul pey.

Mu ne: “Demal ci xeet wii, nga ne leen: ‘Yeenay dégloo déglu, dungeen dégg; ngeen xoolee xoole, dungeen gis.’