TSK

TSK · Proverbs 19:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Gannaaw loolu Absalom doomu Daawuda moo amoon jigéen bu rafet bu ñuy wax Tamar. Jeneen doomu Daawuda ju ñuy wax Amnon nag xemmem Tamar.

¶ Kàddu yu xelu yu Suleymaan. Doom rafet xel, baay ba bég; doom dof, ndey ja tiis.

Xarit du bëgg, di bañ; mbokk day bokk ak yaw say coono.

Dëkke ndànd-foyfoy moo gën jabar ju tàng, bare ay.