TSK

TSK · Proverbs 19:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ana kuy lim feppi suuf, ba lim askanu Yanqóoba? Ku mana waññ xaajaatub Israyil gii? Man de, yal naa dee deewinu aji jub ñii, yal na sama muj mel ni gu askan wii!»

Yal nanga nu xiir ci lim sunuy fan, ba nu mana dawal xel mu rafet.

¶ Li ko taxa jóg di nit ñi am xel mu rafet, am ab yar, ngir xam wax ju lal dég-dég,

Sama doom, déggal samay wax, fonk samay santaane.

Mbégte ñeel na ki may déglu, di teewlu ca sama bunt bés bu nekk, di ma toogaanu sama bunt kër.

Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.

«Yeen waa Yerusalem, deeleen dégg bala ma leena dëddu, ba gental réew mi gent bu kenn dëkkul.»

¶ «Jenn waay la woon ju bare alal, di sol yérey tànnéef yu rafet, di dunde lu neex bés bu set.