TSK

TSK · Proverbs 19:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 19:13 TSK

Samay bokk, mu soreleek man, samay xame sax ñooru ma.

Ku ñàkk, say dëkk sax bañ la; ku barele, barey xarit.

Ay fan yu néew gannaaw gi, ka gën di ndaw jaay léppam, daldi tukki réew mu sore, di topp bakkanam ba yàq fa alalam.