Psalms 36:4
TSK
Ay waxam coxor aki fen, jëfeetul lu rafet ak lu baax.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ay waxam coxor aki fen, jëfeetul lu rafet ak lu baax.
Moo jàmbaar ji, looy damoo jëfi coxor? Yàlla, ngoram, bés bu nekk la.
Mooy nàddil néew-doole yi, njekkam sax dàkk, dooleem di yokku, ànd ak daraja.
Ab soxor ay xemmem alal ju lewul, ku jub garab la, reen baa ko meññal.
Ab dof, waxi dof lay wax, xel ma di nas ñaawtéef, mu nar jëf ju teddadi. Lu ñaaw lay wax, jëme ci Aji Sax ji, di xiifal ku xiif, di xañ ku mar lu mu naan.
Daan bu àndul ak yërmande, moom lees di àttee ña daawul jëfe yërmande. Yërmande nag kekku na ab daan.
Dégluleen! Peyoor, ga ngeen xañ ña gub seen tool, mooy yuuxu noonu. Jàmbati góobkat ya tàbbi na ca noppi Boroom gàngoori xare yi.