Nehemiah 13:28
TSK
Fekk na kenn ci doomi Yowada doomu sarxalkat bu mag ba Elyasib sax, jël doomu Sanbalat mu Oron. Teewul ma dàq waa ji, mu daw ba sore ma.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Fekk na kenn ci doomi Yowada doomu sarxalkat bu mag ba Elyasib sax, jël doomu Sanbalat mu Oron. Teewul ma dàq waa ji, mu daw ba sore ma.
Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
Bu matt amul, ab taal fey, fu soskat amul it, xuloo jeex fa.
dàqleen nit kooku, jébbal ko Seytaane, ngir sànkutey yaramam, ndax aw fitam mucc, keroog bésu Boroom bi.