Job 20:19
TSK
Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko; aakimoo kër jaambur te tabaxu ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko; aakimoo kër jaambur te tabaxu ko.
Ku sonal ku ñàkk, tooñ nga ka ko sàkk; ku baaxe ku néewle, teral nga ka ko sàkk.
Ku ñàkk, su jekkoo ab ndóol, du ko bàyyil fepp, day mel ni waame.
Ñooy xemmemi tool, foqati, ay kër, ñu nangu, tey not waay ak waa këram, ak nit ci céru suufam.
Te su dee ñi leen defal lu baax doŋŋ ngeen defal lu baax, ana lu ngeen ci wara yooloo? Bàkkaarkat yeet noonu doŋŋ lañuy jëfe.
Mu xaacu ne: “Maam Ibraayma, yërëm ma! Yebalal Lasaar, mu sëpp catal baaraamam ci ndox, dikk seralal ma sama làmmiñ, sawara sii metti na lool!”
¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen boroom alal yi, jooyleen te yuuxu, ndax mitit yi leen di dikkal.