TSK

TSK · Proverbs 22:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Am na bés ku jëkkëram bokkoon ci yonent yi, di jooytu ci Alyaasa ne ko: «Sama jëkkër de sa ndongo la woon. Léegi nag faatu na, te yaw ci sa bopp sang bi, xam nga ne ku ragaloon Aji Sax ji la. Waaye ka mu ameeloon bor moo dikk, bëgga yóbbu sama ñaari doom yu góor, ngir def leeni jaam.»