Dóorleen koy doj ba mu dee, ndax moo leen doon fexee soreleek seen Yàlla Aji Sax, ji leen jële réewum Misra, kërug njaam ga.
TSK
TSK · Proverbs 24:32
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Su ñu muusoon, xalaat ci lii, ba xam nu ñuy mujje.
Psalms 4:4
TSK
Xamleen ne Aji Sax ji day séddoo ku ko ragal, te bu ma wooyee Aji Sax ji, mu dégg.
Luke 2:51
TSK
Gannaaw loolu Yeesu ànd ak ñoom, dellu Nasaret, tey saxoo déggal ay waajuram. Yaayam nag takk mbir yooyu yépp ci xolam.
¶ Xew-xew yooyu dal maam ya ay misaal la, te dees koo bind ngir nu jànge ci, nun ñi mujug jamono yemool.