TSK

TSK · Proverbs 26:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba mu ko defee ñu wékk Aman ca bant ba mu waajaloon Mardose. Merum Buur doora giif.

Ku bon a ngoog, di matu doomu ñaawtéef. Day sos njombe, wasin njublaŋ.

ba ma siiwali sa woy yépp, fa buntu Siyoŋ, dëkk bu taaru ba, di bànneexoo sa wall gii!

Éy Yàlla, yaa màgg, ba sut asamaan, sag leer tiim suuf sépp.

Ku yóbbe bàkkaar nit kuy jubal, yeer ma nga gas, yaa cay tàbbi, waaye ku mat di jagoo ngëneel.

Yerusalem day téqtalu, Yuda fëlëñu. Ñooy wax ak a jëf lu neexul Aji Sax ji, di gàntal leeram gi teew.