TSK

TSK · Proverbs 27:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Te itam Aji Sax jee lay booleek Israyil, teg ci loxol waa Filisti. Nëgëni ëllëg, yaw yaak say doom, dingeen ma fekksi. Te it dalub Israyil, Aji Sax jee koy teg ci loxol waa Filisti.»

Aman teg ca ne: «Te kat amul ku Lingeer Esteer woo, mu wara ànd ak Buur ca bernde ja muy def, ku moy man. Ëllëg man la woo maak Buur.

Kenn xamul luy xew ëllëg, kenn manula wax luy xew ëllëg.

Su ko defee ci samam xel laa naan: ‘Céy sama waa ji, yaa ngeek alal ju bare ju mana dem ay ati at; neel finaax, di lekk, di naan ak a bége.’ ”

¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen ñi naan: «Tey mbaa ëllëg ma dem ba dëkk sàngam, def fa at, julaa fa ba tonu.»