Proverbs 5:8
TSK
Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
Dogu mburu fey nab gànc; waaye jabaru jaambur, bakkanu lëmm.
Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.
Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
Su doom jubee, seral xolu baay. Boo juree ku rafet xel, am nga bànneex.
Gone gu sàmm yoon am nag dégg, ku ànd ak sagaru nit gàcceel sa baay.
Malaaka ma ne ko: «Sàkkaryaa, bul tiit, ndax sa ñaan nangu na. Elisabet sa soxna dina am doom ju góor, nanga ko tudde Yaxya.
Sa doom jii dikk, gannaaw ba mu yàqee sa alal ci ay gànc, nga reyal ko sëlluw yafal wi!”